Dibi Dibi Rek

歌手: Ismaël Lô • 专辑:Best Of • 发布时间:2015-06-15
作词 : Ismaël Lô
 作曲 : Ismaël Lô
Dibi dibi rek

dibi dibi rek
aah dibi dibi rek
aah dibi dibi rek

dibi dibi rek
aah dibi dibi rek
aah dibi dibi rek

yangui deugueurlou wante meunoko
boul sop bayil niou djeuliko

yangui ndirok balai bou niou takhawal,
aah ndakh yow lekkato

yangui beugu de ndakh yow nanato,
boul sop bayil niou djeuliko

Ndakh mo ley madj lo

dibi dibi rek
aah dibi dibi rek
aah dibi dibi rek

dibi dibi rek
aah dibi dibi rek
aah dibi dibi rek

Ay niit niom bou niou beuguente,
khamaal lo tchi waakh

Niom mame boye sene taar wessouna,
waye tey laniou gueuneu beugueunte

Ya ngui beugu de ndakh yaw lekatto
Bo fi guetarro waw ma bayiko

Ndakh mo ley madj lo

dibi dibi rek
aah dibi dibi rek
aah dibi dibi rek

dibi dibi rek
aah dibi dibi rek
aah dibi dibi rek

Mbeuguel kenn khamoul lou mou doonn
Foulla diou barri ndaham amatou fi yoon
Kholl moy capitainou boromam

Ndakh mo lay madj lo

Aah
Aah
dibi dibi rek

Aah
Aah
dibi dibi rek

Mo lay madj lo

dibi dibi
aahdibi dibi
dibi dibi rek

Mo lay madj lo

dibi dibi
aahdibi
dibi dibi rek

Mo lay madj lo

dibi dibi dibi dibi
aahdibi
dibi dibi dibi dibi rek

Mo lay madj lo

dibi dibi rek
aahdibi dibi rek
aah dibi dibi rek

Mo lay madj lo

dibi dibi rek
aahdibi dibi rek
aah dibi dibi rek
ou ro ou
...
📥 下载LRC歌词 📄 下载TXT歌词

支持卡拉OK同步显示,可用记事本编辑